Arare

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal



Arare ab dëkkub bëj-saalumu Afrig la, di tam péeyu réewum Simbaawee. Ñoo ngi ko xame woon niki Salisbury ci jamonoy canc gu waa-angalteer.

Ab dëkk bu mag la, am lu mat 2,8 milioŋ ciy way-dëkk, mooy diggu yëngu-yënguy yaxantu ci Simbaawee. ci melosuuf ñoo ngi koy barabal ci (17°49′S 31°03′E / -17.817, 31.05).