Apolos

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci angale ak ci faranse mooy Apollos.

Benn Yawut la woon, bu bawoo ci Alegsàndiri. Boroom xam-xam ci Mbindi Yonent yi la woon, te nekkoon jàngalekat bu mag ci mbooloo ñi gëm ñi. Waxkat la woon itam, ku mënoona wax wax yu rafet ci gereg.

Apolos moo feeñ ci Injiil ci Jëf 18:24-19:1; 1Ko 1:12; 3:4-6,22; 4:6; 16:12; Tit 3:13.

Karmat ak delluwaay[Soppi]


Xool it[Soppi]

Jukki yi ci lonku[Soppi]

  • [[]]

Lëkkalekaay yu biti[Soppi]