Akas

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë (אחז) la tur wi jóge. Ci angale mooy Achaz or Ahaz; Ci faranse mooy Achaz

Li dale ci Robowam, fukkeelu buur ak benn la woon ci Yuda. Doomu Yowatam la woon, di benn ci maamaati Yeesu ci Macë (Mc 1:9). Dañuy gis jalooreem ci 2Ki 15:38-16:20; 2Ch 27:9-28:27; Isa 7:1-25.