Abiyudd

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale mooy Abiud; Ci faranse mooy Abiud

Doomu Sorobabel (mi bokkoon ci njiiti Israyil yi, bi ñu génne ci Babilon) la woon. Benn ci maamaati Yeesu ci Macë la woon (Mc 1:13).