Abadon

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë (אבדון) la tur wi jóge. Ci angale mooy Abaddon; Ci faranse mooy Abaddon

Turu malaakam kàmb gu xóot gi la, ci làkku ibrë bi ñu sotti ci làkku gereg. Tur wi ci gereg mooy Apolyon. Dafa tekki 'yàqkat'. Dafay wax ci buuru njéeréer yi ñu gis ci téere Peeñu ma ci Injiil (Pe 9:1-12). Lu ëpp ci boroom xam-xam Injiil yi xalaat nañu ne ci Ibliis lay wax.

Ci Injiil dañuy gis Abadon ci Pe 9:11.